1
At mu jot, 51 500 - maanaam juróom-fukki junni ak benn ak juróomi téeméeri doomi Senegaal yu jigéen dinañu sàkku dindi ëmb. Genn-wàll gi, ci ñoom, dañu ciy jëley gaañu-gaañu, ngir pexe yi way-nëbbu yiy jëfandikoo te àndul ak kóoraangeg doktoor. Ay junniy junni ci jigéeni Senegaal duñu jot ci toppatoo bi war ci ñoom, ñeel seen wérug awra ak gu seen njurukaay. Soxla nañu jot ci pexey soreyàntool njur yi, ci tegtal ak toppatoo yi war ci ñoom bu ñu tàggook seen ëmb. Sedgh G et al., Estimations de l’incidence de l’avortement provoqué et conséquences de l’avortement non médicalisé au Sénégal, Perspectives Internationales sur la Santé Sexuelle et Génésique, numéro spécial de 2015, pp. 35–44.

At mu jot, 51 500 - maanaam juróom-fukki junni ak benn ak ...€¦ · dindi ëmb. Genn-wàll gi, ci ñoom, dañu ciy jëley gaañu-gaañu, ngir pexe yi way-nëbbu yiy jëfandikoo

  • Upload
    others

  • View
    3

  • Download
    0

Embed Size (px)

Citation preview

  • At mu jot, 51 500 - maanaam juróom-fukki junni ak benn ak juróomi téeméeri doomi Senegaal yu jigéen dinañu sàkku dindi ëmb.Genn-wàll gi, ci ñoom, dañu ciy jëley gaañu-gaañu, ngir pexe yi way-nëbbu yiy jëfandikoo te àndul ak kóoraangeg doktoor.

    Ay junniy junni ci jigéeni Senegaal duñu jot ci toppatoo bi war ci ñoom, ñeel seen wérug awra ak gu seen njurukaay. Soxla nañu jot ci pexey soreyàntool njur yi, ci tegtal ak toppatoo yi war ci ñoom bu ñu tàggook seen ëmb.

    Sedgh G et al., Estimations de l’incidence de l’avortement provoqué et conséquences de l’avortement non médicalisé au Sénégal, Perspectives Internationales sur la Santé Sexuelle et Génésique, numéro spécial de 2015, pp. 35–44.